Muhammad Yόnéntab Yàlla Bi (Yàlla Na Ko Yàlla Dolli Xéewël Ak Mucc)

Taar bépp fu mu mana nekk ci moom Yàlla na ko Yàlla dolli xéewël ak mucc la tàppewoo.
Ta benn tόortόor du ubbiku ci àddina jii ludul bu tànqoo cig leeram !
Moom daal day taxaw taxawaayu fëlόor bu naat bu ubbiku ta laxul waaye kay day gënë naat di gënë yees lu mu gënë yàgg. Ta moom ag leer la li tàmblee ci kaw boppam ba ci ndëggόom…


Read In Other Languages

ALBANIAN
AMHARIC
ARABIC
BOSNIAN
CHINESE
CRIMEAN TATAR
ENGLISH
FRENCH
GEORGIAN
GERMAN
HAUSA
HINDI
INDONESIAN
ITALIAN
KURDISH
KYRGYZ
LUGANDA
MALAY
MONGOLIAN
PERSIAN
PORTUGUESE
RUSSIAN
SPANISH
SWAHILI
TAJIK
TRADITIONAL CHINESE
URDU
UYGHUR
UZBEK
ZARMA